Gardening Terms (Wolof)
Kaarange
Protection
Sekateer
Pruning shears
Kaña
Rat
Dex
River
Reen
Root
Buum
Rope
Meen mi
Sap
Si
Saw
Jamano
Season
Sartu
Sickle/hook
Tame
Sieve
Pant
Slope
Jaan
Snake
Jargooñ
Spider
Dàtt wi
Stalk/trunk
Ndox yu taa
Standing water
Xeer
Stone/rock
Yaatuwaay wi
Surface/area
Max
Termite
Jumtukaay yi
Tools
Ndëg-sërëx
Trap
Mbalit
Trash
Njëriñ wi
Use/utility
Julikaata
Wasp
Suuf suy yol
Water erosion
Deñcum ndox mi
Water storage
Teen wi
Well
Burwet
Wheelbarrow
Fildifeer
Wire
Sax
Worm/larvae
Melantaan
Ant
Surga
Assistant/helper; farmhand
Mbootaay
Association
Xas mi
Bark
Yàmb
Bee
Tëgg bi
Blacksmith
Booru tool
Border of a field
Banqaas bi
Branch
Lëppaalëp
Butterfly
Defukaay
Can
Saalu darkase
Cashew nut
Ngunu
Chicken coop
Suuf su ban
Clay/compacted soil
Xòotaay wi
Depth
Bekkoor
Drought
Noor
Dry season
Noppal suuf
Fallow land
Tòotòor
Flower
Weñ
Fly
Màtt
Fuelwood
Sàq wi
Granary
Marto
Hammer
Sémmiñ
Hatchet
Ngooñ
Hay
Sisaay
Hedge clippers
Pax
Hole
Xeer wu xonq
Laterite soil
Guddaay wi
Length/height
Suuf su nooy
Light soil
Kalkeer
Loam
Nattukaay
Measuring tape
Njaxas
Mixture
Potopoto
Mud
Pont
Nail
Ferñeent yi
Nutrients
Dèeg wi
Pond
Suuf su néew doole si
Poor soil